Compositor: Não Disponível
Mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Ooh sa problème beugou maa
(Mandou laay déf)
Ooh bouma lathie khamou maa
(Mandou laay déf)
Maane mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Maane mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Yéene sén problème beugou maa
(Mandou laay déf)
Maane nono féké wouma
(Mandou laay déf)
Soo beuguéee diam sonal laa
Kaay ma wakh la louy pékhé, mandou laay déf
Soo beuguéee foo nélaw faa
Kaay ma wakh la louy pékhé noopi guay déf
Boul ma wakh lou khéew sa keur gua
Fi kou nékk amna loula dooy problème
Baayil di dougal sa lamagn
Si loo khamoul nakala tédieul sa guémégn
Ooh mandou li déss si att bi
Saay cas téyé ko gua baal maa
Talouma kouma yobou keur yama
Li guamay nétali mane ladiou mala (randou ma)
Mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Ooh sa problème beugou maa
(Mandou laay déf)
Ooh bouma lathie khamou maa
(Mandou laay déf)
Ooh mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Maane mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Ooh sén problème beugou maa
(Mandou laay déf)
Maane nono féké wouma
(Mandou laay déf)
Soo déguée thiow li bari lool
Té niom niépp disi wakh, mandou mo guenn
Bou laay wakh lou boone si diabaram
Kée di yakh dieukaram, mandou moo guenn
Khamoo loutax niou réroo
Baa niou dioté féké wo, mandou moo guenn
Dougou lou sa yoon lou bakh laa
Nitt daay mandou si loumou khamni moo guenn
Damay goumba teukh lou si séni gang
Dooma dougal si saay wakhi patangle
Té diémou maa si diotaay you bari débat
Nima léré nima gérer li déss si att bou béss bi
Maane mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Maane mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Ooh sa problème beugou maa
(Mandou laay déf)
Ooh boul ma lathie xamou maa
(Mandou laay déf)
Ooh mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Maane mandou laay déf
(Mandou laay déf)
Ooh sén problème beugou maa
(Mandou laay déf)
Maane nono féké wouma
(Mandou laay déf)
Soo khamoul dagua naane khamou maa
Yénn mandou léen
Xamoo noumou démé féké wooo
Yénn mandou léen
Mane dé guisouma té féké wou ma
Mane dé xamou ma, mandou ngirr Yalla
Mane dé xamou ma té féké wou ma
[?]
Mandou rék laay déf
Maané noonou la
Mandou rék laay déf
Loolou mooy foul la
Mandou rék laay déf
Sooko défé non problème daguay nopaa lou
Diam guay amme
Mandou rék laay déf
la, la, la la mome rék laay déf
Mandou rék laay déf
la, la, la la mome rék laay déf
Mandou rék laay déf
la, la, la la mome rék laay déf
Non bi baxna yes! Chaaaay
Mandou rék laay déf
Mané la noopi laay déf
Mandou rék laay déf
Mané la noopi laay déf
Mandou rék laay déf
Mané la noopi laay déf
Boo manoul noopi néel paatt
Mandou rék laay déf
Aka si paate laay déf
Mandou rék laay déf
Baxam mane paate laay déf
Mandou rék laay déf
Paate laalay maay mane guay waakh
Té tékmaa
Mandou rék laay déf
Est-ce que dégueu guama
Mandou rék laay déf
Est-ce que comp... Guama
Mandou rék laay déf
Diamono nila
Li déss si att bi mandou rék